Face to face : Siteu répond à la provocation de Papa Sow... Ça chauffe déjà !

Condividi
Codice da incorporare
  • Face to face : Siteu répond à la provocation de Papa Sow... Ça chauffe déjà !

Commenti • 80

  • Ghur Dy8r
    Ghur Dy8r 24 giorni fa

    Papa Sow yalla nala.yalla.maye dame yarou rek mouwor

  • Fallou Babou
    Fallou Babou 27 giorni fa

    Siteu dafa rew

  • Fallou Babou
    Fallou Babou 27 giorni fa

    Siteu dafa rew

  • Khadim Toure
    Khadim Toure 27 giorni fa +1

    Li yeufu dof leuh siteu yamal mo gueun thi iow dei ba combat ba rek✊✊✊✊

  • 3mara
    3mara 28 giorni fa

    Siteu, c'est un vrai con et ca mérite, on le sanctionne est, il n'est pas le droit de toucher son adversaire avant le combat et si un jour, tu feras ca sur UFC, ils vont te sanctionner respectez vous d'abord, c'est pas du tout professionnel salam
    From Mauritanie🇲🇷

  • Sidy Diop
    Sidy Diop Mese fa

    Siteu c'est un vrai couillon.

  • Dmx Jjj
    Dmx Jjj Mese fa

    Papa a une bonne éducation motakh si c’était un autre lutteur combat bi yakouna dina kate sa ndeye gua xamm

  • Dmx Jjj
    Dmx Jjj Mese fa

    Siteu je te déteste maintenant bilahi papa dina kate sa ndeye tu verras goordjiguéne bi filala sa Thies diape tégual sa ndeye guay daw tapétt bi

  • Ndiayene Bi
    Ndiayene Bi Mese fa

    Rewantou la beug tei tapet la siteu

  • MOUHAMED NDIAYE
    MOUHAMED NDIAYE Mese fa

    Siteu yaw la faralone dh wayei lingay def bokoul si Éducation yalla nala papa sow daane

  • Cheikh Amadou tidiane ndiaye Gueye

    mane mom faraloumawone kén mei siteu miii da réw amoul niii lagniii defff diii yagu lamb yiii rkkk
    vré konn la siteu miii

  • Boye Khalifa
    Boye Khalifa Mese fa

    Yala andoul ak kouy togn

  • Boye Khalifa
    Boye Khalifa Mese fa

    Siteu li dou lamb dji li signature rk dgaya danou dji rk

  • Ibrahima Diouf
    Ibrahima Diouf Mese fa

    Dérétou diamegeune moy dawe souniou yarame

  • Ibrahima Diouf
    Ibrahima Diouf Mese fa

    Nio mouna roubé

  • Omar Makoudi
    Omar Makoudi Mese fa

    Siteu indiscipliné 🤏

  • Diaw Ass
    Diaw Ass Mese fa

    Papa🙏

  • Milk Diop
    Milk Diop Mese fa

    No vraiment siteu désolé pour toi mais yalnala papa dane vraiment rouslo nga ahlou sport yeup😔

  • Sheik Sh
    Sheik Sh Mese fa +1

    Siteu nila meuna mél nakh khamoul lou beuri banlieue rekk la meuna deukk.... Fiert de toi PAPa SOW diay ngako khél lolou moy boy town.

  • Malick Thiam
    Malick Thiam Mese fa +1

    Siteu est indisplinèe

  • Aziz Diaw
    Aziz Diaw Mese fa

    Siteu limou def fat nehal signature rek mais rewandé

  • Aziz Diaw
    Aziz Diaw Mese fa

    Siteu kassé

  • Sebor Awa
    Sebor Awa Mese fa

    Athia tarkinda bi siteu siteu la

  • Toro Fouta
    Toro Fouta Mese fa

    Femme bi di rapporte saytanéla

  • Toro Fouta
    Toro Fouta Mese fa

    Allez siteu domo diamaguene na tengue dieur tarkinda fi amoul yar signature la

  • ANKEY TV
    ANKEY TV Mese fa

    Siteuu nank rkk sénégalais dou faral kouy togneuh boul yak sa image

  • Abdou Aziz Mbaye

    Chakk jour ngén amm déception siteu dina nokk papa sow dane ko

  • Abdou Aziz Mbaye

    Papa sow mo ndieuka provoqué tekk tankk siteu

  • Abdou Aziz Mbaye

    Dolén yalla dolén tous li lamb la rekk

  • Malang Dieme
    Malang Dieme Mese fa

    tey nack papa moo togne

  • aisha Zahra
    aisha Zahra Mese fa

    Wa héé doleine bayii siteu dageine xam papa sow noumu def siteu si soufe

  • Alioune Mbaye
    Alioune Mbaye Mese fa +1

    Siteu limouy def nii c comme si il ne respecte pas son adversaire. Guiss na thi yaw thi combat bi nga daanou beu khalangou papa Sow dou kouniouy khépp deh

  • fantome fantome
    fantome fantome Mese fa

    Nice comprehension pour papa sow niit danguay nittè

  • Jean Dominique Séne

    Papa yalla nga am n'dam

  • Bara Dieng Sy
    Bara Dieng Sy Mese fa

    Papa Sow daan nala té beuré go léne. Lii rekk ndaam la. Respect amna solo trôp sii nite Siteu

  • Verdugo killer
    Verdugo killer Mese fa

    *Siteu c'est un indiscipliné nagnko dagg si cachet bi... papa Sow li bétougnou toujours aussi mature ...djam si yaw rék*

  • Assane Seck Seck

    😁😁😁😁😁😂😂

  • Niang Amsata
    Niang Amsata Mese fa

    Non kii dafa rew

  • giannis antetokounmpo jr

    Yalla xamnani siteu la faralone mais baye fall dou togn siteu day mouro bay fall wayei dou dara matoul limou done yalla papa sow am ndam si barkei noreyni

  • deug x rey deug
    deug x rey deug Mese fa

    Yalla nako papa Sow dann. Siteu est un vrai con .Il est malade vraiment .C'est pas sportif ce qu'il fait le mec

  • Amy Collé Diallo

    Kou de dekeu diamaguene do ame défaites yallah nla yalla maye ndame yobouko diamaguene

  • Mourtala Fall
    Mourtala Fall Mese fa +1

    No j supporte siteu mei ta déconnei yalla na papa am damm

  • Diop Vip Ucad
    Diop Vip Ucad Mese fa

    Yalla mo yore ndam yalla naku yalla may ndam

  • Diop Vip Ucad
    Diop Vip Ucad Mese fa

    Situe ndam RK inchalla

  • Baba Sy
    Baba Sy Mese fa +2

    Wa parcelle danio am éducation
    Dougnou ay waguaa dh
    Papa ndam rek inchalah

  • Birane Mbaye
    Birane Mbaye Mese fa

    Vraiment siteu yae la mousseu faral barki seex ibra fall mei combat yalbaniou door gua danou

  • ibrahima khalil kane

    siteeeeuuuuuuuuuuuuuu
    tarkinda ndam rk inchallah

  • Seydou Ndiaye
    Seydou Ndiaye Mese fa

    papa sow yalnala yallh may namb. sitteu amo dollé rabi samawati billahi le jour j doo yeuketi lokho inshaallahou rabbi

  • Kalidou Senghor
    Kalidou Senghor Mese fa

    Siteu rew gua trop

  • Saliou LO
    Saliou LO Mese fa

    Papa Sow. Quel sang froid champion

  • Daouda king khakatay show

    Siteu sama mbeur ga wayé wédinallah boudoule dara sakhe ga xole si âge ga diokhe thieurou mak fi dou usa li eupouna

  • Cheikh Diaw
    Cheikh Diaw Mese fa

    Siteu réw na papa yalla nako yalla may ndame

  • Cheikh Diop
    Cheikh Diop Mese fa

    Awmasi mbeur me yalna papa saw dan

  • Cheikh Diop
    Cheikh Diop Mese fa

    Siteu rewna

  • Papa Diene
    Papa Diene Mese fa

    Situe vrm lingay df d’où yon yaw ladan faral mè yalnala papa sow dan lii mo taxon nga danou contre sa thiès

  • amady sambou
    amady sambou Mese fa

    d'autant plus que la pression est en faveur de siteu papa peut en sortir a cause de sa discipline

  • Modou Fall
    Modou Fall Mese fa

    Oh quel métisse yalla nalla borom darou maye ndam papa sow

  • Mounass Mall
    Mounass Mall Mese fa

    Siteu nam nagne la bilae

  • Jatta Kemo
    Jatta Kemo Mese fa

    Il dépasse les borne ce qui n’est pas bon tu vas perde ton combat inchallah siteu

  • OUT
    OUT Mese fa

    Vraiment siteu ce que tu as fais c’est méchant. Kén rafétlowouko. Les supporters de siteu soyez véridiques et avouez que votre lutteur a fait du n’importe quoi. Mais Yalla bakhna ba la 5 avril. Tous avec Papa sow. Cng doit intervenir et lui donner une amende

  • Yacine Wagne
    Yacine Wagne Mese fa +1

    Siteu moy sama luttere papa sow yalla na yalla may ndam

  • RAP EMPIRE
    RAP EMPIRE Mese fa

    Situ sma mbeur la mai combat bi douko djik

  • Bada Ndiaye
    Bada Ndiaye Mese fa +1

    Papa champion la bilay

  • Aly Benze Diakho

    Impoli

  • mama africa
    mama africa Mese fa

    Khaléé bou réw Lou mou yorr momouko 👉👉👉papa sow forever damm rek inchallah ❤️❤️🙏🙏

  • Ricky Rozay
    Ricky Rozay Mese fa +1

    Mm si je suis fan de siteu je suis pas d'accord avec son comportement ça ne se fait pas limouy def
    Siteu ya ngi yakk sa image tu as deconné
    Big up Papa Sow champion nga

  • Ibrahima Diéng
    Ibrahima Diéng Mese fa

    Yalla na yalla maye ndame papa sow

  • Ablaye Diagne
    Ablaye Diagne Mese fa

    Papa sow yalla nala yalla may ndam

  • Laye Fall
    Laye Fall Mese fa +1

    Siteu kou reew ngeu yalla nga daanou ci barké cheikh ahmadou Bamba

  • COIFFEUR Mame Bara

    Papa Sow mo ndieuka provoquer

  • Abou Nia
    Abou Nia Mese fa +1

    Li rek mon takh nio khass beur yi, la violence commencé encore sur les lutteurs, c'est pour cela que les supporters se battent entre eux.
    Le sport c'est le faire play vous n'êtes pas des ennemis.
    Bravo champion, vous montrez que tu es un champion faire play.

  • kawou camara
    kawou camara Mese fa

    Siteu n'est pas respectueux ku oppal la raison pour laquelle il perd facilement ses combats

  • Jaspo Joop
    Jaspo Joop Mese fa

    Siteu tu fou le bordel mais baxna

  • Mamoudou Sow
    Mamoudou Sow Mese fa

    Siteu linga déf dou yeufu baay fall

  • bouba cisse
    bouba cisse Mese fa

    Siteu dafa reww

  • Mouhamadou dione Fall

    Siteu manoul beuré manoul xeexx dakay lidieunti rek reew guimouy diaye motaxone sathies gnousko gnousi dof wayé bilay raw ndax papa mom lathie sa grand ness gnamna

  • bery dioo
    bery dioo Mese fa

    Siteu bayil mandit meuno beuré meuno dane

  • Thianta Kone
    Thianta Kone Mese fa

    Me papa na tok plasame

  • Yakhya ousmane Diop

    Khamouñou kou toñ kou fayou lañou kham siteu 4Ever

  • Mahmoud Ly
    Mahmoud Ly Mese fa

    Siteu c'est pas sa être Baye fall
    Baye fall deug respect laye dokk at diam
    Salam